Yaa Gore (taalif)Version audio du Taalif Yàgg, yàgg, dëggay daan Dëgg lottoon na Senegaal Usmaan Sonkoo tax mu daan Lii dinaa ko bind ngir ëllëg Da nga...
Kaŋfóore (taalif)Céy suuf yaa ka sañ Ku tollu ne Séex Ànta Jóob Nga ne tey jii yaa ko tiim Xanaa xamoo ne moom Benn toq ci yuuram Taa loo na say kër-i-kër...
Nook mbënn mi nag, ba kañati ?“Ku ndóbin rey sa Maam, foo gisee lu ñuul sax daw.” Xanaa kon ndóbin gi nekk Senegaal di reye taxul wolof Njaay di wax? Su may xalaat...
Koronaa (taalif)Àddina si tey dafa taxaw Ku nekk naan man fu may aw Nit naan moroomam bu fi ñëw Jàngoro jee fiy xal a ñëw Kanam yépp la ñu ëw tey Ku...
Bitenti (taalif)Bàkkan yaa ngi rot ney xob Ku faatu nu gaaw dem rob Xeetu rongooñ nu fexe pàccal Teewul lijjanti lii du lu nu soxal Siggil ndigaale,...