Séex Axmadu Bàmba Njaay7 févr. 20211 MinWolofalKaŋfóore (taalif)Céy suuf yaa ka sañ Ku tollu ne Séex Ànta Jóob Nga ne tey jii yaa ko tiim Xanaa xamoo ne moom Benn toq ci yuuram Taa loo na say kër-i-kër...
Séex Axmadu Bàmba Njaay17 sept. 20203 MinWolofalNook mbënn mi nag, ba kañati ?“Ku ndóbin rey sa Maam, foo gisee lu ñuul sax daw.” Xanaa kon ndóbin gi nekk Senegaal di reye taxul wolof Njaay di wax? Su may xalaat...
Séex Axmadu Bàmba Njaay24 mars 20202 MinWolofalKoronaa (taalif)Àddina si tey dafa taxaw Ku nekk naan man fu may aw Nit naan moroomam bu fi ñëw Jàngoro jee fiy xal a ñëw Kanam yépp la ñu ëw tey Ku...
Séex Axmadu Bàmba Njaay23 avr. 20171 MinWolofalBitenti (taalif)Bàkkan yaa ngi rot ney xob Ku faatu nu gaaw dem rob Xeetu rongooñ nu fexe pàccal Teewul lijjanti lii du lu nu soxal Siggil ndigaale,...